Baatou bindeu katt bi Guinaw bi baat bobou yeukeuti ko, nieupa weulbatiko dadi kay khol nakh tiit. -Anh kone iow meuna ti ngua wakh wolof ? Waro gaïndé may ma diomi di ! Waxouma mouy nane mane di diay responsable ! (Salma wakh ko ak xol bou tangu ). -Boy xolal bouniou yapp ! Da ngua yakarni que dinaniou la bayi ngua koye takk té nieupe xam naniou ni que beugou ko. En plus iow da ngua faux. -Nangou nani que Alioune la toudou waw té dégu na wolof. Nangou nani tamit que Saly ak mane séke naniou wayé da nguéne ame lou nguéne xamoul si histoire bi. Moy que beuss bobou mom mi, dafa nangou wone. Forcé woumako donc ça veut dire que viol amoufa. -Astarfoulilah ! Iow ya meuneu féne ! (Salma wakh ko ak kanam fou mérr). Nane la djiguéne di féné ni daniouko siff ba paré té dou deug ? Da ngua yakar


